Press "Enter" to skip to content

[ URGENT ] OUSTAZ PAPA SAER SOW RÉPONDE SÉVÈRMENT OUSTAZ IRAN NDAO SUR………



Veuillez abonné la chaîne et commentér sur le video
Thiarene info chaîne de tout l’actualité

0 0 vote
Article Rating
Subscribe
Notify of
guest
46 Comments
Oldest
Newest Most Voted
Inline Feedbacks
View all comments
Moustapha Gueye
Moustapha Gueye
2 months ago

dakh ira moungui ci tarikh cheikh wal

Moustapha Gueye
Moustapha Gueye
2 months ago

dakh ira moungui ci tarikh cheikh wal

Mamadou lamine Gueye
Mamadou lamine Gueye
2 months ago

Iran il parle dans le vide mais doula wakhe téré gnoune khalé tivaouane dou sounou référence

Seydi Gning
Seydi Gning
2 months ago

Mashallah xam xam dafa nekh té âme kilifa rek mo woor walahi souma walahi

Moustapha Toure
Moustapha Toure
2 months ago

Iran deugu rek la wakh

Younouss Diop
Younouss Diop
2 months ago

Machalla

Thierno Diaw
Thierno Diaw
2 months ago

Nit bou dioumè dagko wra nagou bodanoo dag ko wara nagou ab dièlle bo ko nagou woull day geuna gnaw rk iran ndaw limou wkh dra nekou si bayi lènn thiow Li

mangone cissé
mangone cissé
2 months ago

Machallah xame xame rek mo woor.

Maguette Bomou
Maguette Bomou
2 months ago

Ce iran croit tout savourais c'est un triste ignorant. Son arrogance n'a pas de limites.

Cheikh Thiam
Cheikh Thiam
2 months ago

Man gueumouma né dioul na tarikhabi

Cheikh Thiam
Cheikh Thiam
2 months ago

Iran al amine dou serigne gnam déh.iran kén khamou kouko diokh tarikhabi.est ce qu il prit le Wird

Nico NDIAY
Nico NDIAY
2 months ago

Macha Allah amatina solo lol. Merci si kaddou yi tègouna si khamkham ak dall ak ragnè ak yarr macha Allah.

Liberation Senegal
Liberation Senegal
2 months ago

nice

Ibrahima sene NABIEN
Ibrahima sene NABIEN
2 months ago

Dieuredieuf Oustaz pape Saer Sow wahtan bi amna solo

Modou Ba
Modou Ba
2 months ago

Affaire de diouli d'ou affaire tarikha

Modou Ba
Modou Ba
2 months ago

Affaire de diouli d'ou affaire tarikha

Pape Liye
Pape Liye
2 months ago

iran dafa complexe bolèsi reuye

Ndeye rokhy Diatta
Ndeye rokhy Diatta
2 months ago

Yaw oustas Iran mola wax niou waxi yalla ak yonenté bi ganan Aÿ babs ak Gnenen

Ousmane Cisse
Ousmane Cisse
2 months ago

Sagesse+discipline+éloquence+civisme+sprit d'ouverture=Tidiane

Bah Papa
Bah Papa
2 months ago

Kelifa bou dioume de niou koye wah! Sahaba (rsw) Omar mo guena for Khalifa tijane, Omar boumoumé defa nagou mé loutah senegal sougnou dioumé dougnou nangou. Lolou bokul si djikoye Dioulite.

Bah Papa
Bah Papa
2 months ago

Koul lile haq walaw Cana mour-rann,

nabou faye
nabou faye
2 months ago

Iran légui mou guiss El Hadji Sy kokou yalla mokay fayoul Iran khaliss bi mo eupeu si môme gnoune nak yalla lagnou kham ak seydinakh mouhamed gamou yimouy déf thies commerce ndakh daye weur si mourite yi woyane di doule rek Serigne mourite bouné ngani moye sakh kharite ndakh khaliss wayé yow khamo léfal ndéyam Alkhatoum wakhone nako kéneu wakhatoul yalla surtout khaliss rek gue gueum

Ka Aliou
Ka Aliou
2 months ago

Iran diamono yimouy wakh lolou buss yagui yébe ba féss marceyi akk fépp limou wakh deugue la dafa téll lolle

Mouhamadou Assane Tambedou
Mouhamadou Assane Tambedou
2 months ago

Niak xam xam ak doff ak beug buzz moko diap

Kine Seye
Kine Seye
2 months ago

Iran dafa fouye legui khepna wa Tiwawone legui

Alle Syll
Alle Syll
2 months ago

Iran lim wakh lepp degue la

Mansour Seck
Mansour Seck
2 months ago

iran diotéwoufi ak oustaz diéne rakou al maktoum ak al amine iran mbamla dagnouko géné tivaoun

Mansour Seck
Mansour Seck
2 months ago

iran daw dagnouko wara guéné ttivaoune

Mamadoulamine Fall
Mamadoulamine Fall
2 months ago

Yen mounou lena bayi iran ndao khana wakh na deugeu

Mor POUYE
Mor POUYE
2 months ago

No Iran legui môme do conprendre lane la legui politique opposition bi moko yaubou

Matar Mboup
Matar Mboup
2 months ago

Khàmnga Iran dafarew gniaki teguine ngakh mom bouy wate bokodeklo ngakhamni amoulyar ndakh mom bouy warate dafaymelne kouy khoulo wakhinam douko bolek yar waye soame khamkham te yàrouwo yak mbammou seufitere yena yam Iran ndao akoul yar akoul teguine akoul soutoura wayanak mom data kham te khamewoul lolou mokodal amoul kersa

Sopemoustaphamboup Tivaouane
Sopemoustaphamboup Tivaouane
2 months ago

Iran khame khamame da soriwoul nak wakh deug senegal kouy fégne si tlvsè rek niouné moy wadja

Azzi Sow
Azzi Sow
2 months ago

Machalla khame khame bi ande na ak yalla na yalla faye yiwe

Yayou Mina
Yayou Mina
2 months ago

Amna solo

Ousseynou Seck
Ousseynou Seck
2 months ago

Iran da yeuk bopam

Maktar Sarr
Maktar Sarr
2 months ago

Machallah amna solo Yalla fayla yiw. Nonguila ziar bou baakh.

Mohameden Fall
Mohameden Fall
2 months ago

ما شاء الله

Seydou Kane
Seydou Kane
2 months ago

Iran Kane moko diokh wirde wala nga djisko si hadara jouma dou tivaouane dou dakar keene mousou ko djiss

Mbaye Abdou Aziz
Mbaye Abdou Aziz
2 months ago

Iran défoule dara wakh n'a deugue bou wér bou lénn niou sonale way mo tay deugue rék leu wakh

Papa Alioune SECK
Papa Alioune SECK
2 months ago

BILAKHI WALLAHI Oustaz vous avez parfaitement raison

Oumar Thiaw
Oumar Thiaw
2 months ago

Diné amoul serigne amoul dara fii kène diamouwoufii SERIGNE yalla lagnouy diamou kone koudoul yalla bo wakhé lougnou mana dègue gnou topp la wayé bo wakhé lougnou nangouwoul kène doulassi topp

Oumar Thiaw
Oumar Thiaw
2 months ago

Way dialal feulé
Bayilène par parlo bi ta Iran dafa wakh limou gueum ak limou diangue

Mamadou Dia
Mamadou Dia
2 months ago

Machalla louler

Gainde Diop
Gainde Diop
2 months ago

Je vous interpelle tt le monde donner moi un hadiths ou une aaya kourane interdisant la fermeture des mosquée dans de telles circonstances!soyez rationnelle le problème c'est pas Iran Ndaw!(bokk ci thiowli khamm lou khew moka guene)!

Abdou Ly
Abdou Ly
2 months ago

iran ndaw naniou ko exclue darraja

Cheikh tijane Ndiaye
Cheikh tijane Ndiaye
2 months ago

Iran mo raw sene baye…bayil wakh ji

46
0
Would love your thoughts, please comment.x
()
x