Press "Enter" to skip to content

Voyage aux USA : Découvrez les premières photos de Sa Nekh et Cie



[À la une]☆~~👉https://rebrand.ly/A_la_une-Pikini

[Abonnement Gratuit ici]☆~~👉https://rebrand.ly/Abonnement-Gratuit-Pikini

[Visitez notre Blog]☆~~👉https://rebrand.ly/Blog-Pikini

[Inscriptions aux Castings ici]👉https://rebrand.ly/Castings-Pikini

[TWITTER]☆~~👉https://rebrand.ly/Twitter-Pikini

[FACEBOOK]☆~~👉https://rebrand.ly/Facebook-Pikini

[INSTAGRAM]☆~~👉https://rebrand.ly/Instagram-Pikini

#Femme_idéale_https://youtu.be/2YY4xNDkcOQ

Pikini Productions☆~~👉+221 771161717 [Service Commercial]

©ByBen 2020

39
Leave a Reply

avatar
39 Comment threads
0 Thread replies
0 Followers
 
Most reacted comment
Hottest comment thread
0 Comment authors
THIATE RAKADIOUMarietou DaboSerigne MbackeAle KebeNHBI Seye Recent comment authors
  Subscribe  
newest oldest most voted
Notify of
Astou Ndiaye
Guest
Astou Ndiaye

Kham nane bis pegn ba site internet yi gno fa nara yague

Astou Ndiaye
Guest
Astou Ndiaye

Waa pikini rouslo nguenma yen ken khamoulen won si wakh loulen leroul ragal len yalla

saliou mbacké BA
Guest
saliou mbacké BA

Aziz waro nangouuu di fréquenter ay homo dh

Fatima Sow
Guest
Fatima Sow

Machalla way laf tiate

Ndoye Salliou
Guest
Ndoye Salliou

🤙🤙🤙👍

Assane Kara
Guest
Assane Kara

Manekin yi khana dagnouy defiler

tayb toure
Guest
tayb toure

Chèkhou Gueye alias sanekh ma beaucoup déçu

Nordonne Mame
Guest
Nordonne Mame

Sanekh m'a trop déçue😱😱😱 Quand je pense j'ai démissionné à mon première travail car dans mon service y'avait un gay et je voulais pas être en contact avec lui😱😱🤒

Daouda Fall
Guest
Daouda Fall

Wa soleil levant louniouy Sène yone nèkouci ba ngèni wakh

Fatou Ndaye Ndaiye
Guest
Fatou Ndaye Ndaiye

🤺

moustapha jallo
Guest
moustapha jallo

Hé! Go a way.vous êtes qui pour juger les gens alors que vous les critiqueur vous n'êtes que des defeants, foutez nous la paix avec vos arrogance et égoïsme. Yen dolenne yalla dolenne yoneunty oubi sen gatyi rek di wakh si domou diamour.

Maimouna Diop
Guest
Maimouna Diop

Son bi nehna

Bayelahat Tall
Guest
Bayelahat Tall

You spoil your reputation

TV MODOU MODOU
Guest
TV MODOU MODOU

Lii Guey Ba Tolou fii Yakhh Ko Si Lou Niakk Foula

Sall Dia
Guest
Sall Dia

Sénégal bokk nasi país Yi ganeu wayadi niom lou diar wakhe donkou nek fi di bakkarou rk

Mayatu Zembabu
Guest
Mayatu Zembabu

😃😃😃😃😃😃😃😃🤗

Drame Moussa
Guest
Drame Moussa

Niag fayda

fasha diop
Guest
fasha diop

Surtout yaw cheikhouna yaw li waroko wone sax xalate ak fimala tégone 😭

Ajie Jobe
Guest
Ajie Jobe

Lovely song

Mariame Traore
Guest
Mariame Traore

Bravo à vous courage vous êtes des grands hommes et c'est pas de tout repos on est fière de vous

Ousmane Tine
Guest
Ousmane Tine

NI NGÉN MEL SÉNÉGAL KEN WAROU LENA GUISS SI YEN DIETAYE YI RAWATINA DIETAYOU GOOR DJIGENE THIM XALISS DIAROUKO BODÉWÉ 7METAR PERKAL REK MOLA SIYE TOP KON XALISS DIAROUKO

Ousmane Tine
Guest
Ousmane Tine

KOULOU NAF SIN BIMA KASABAT RAXINA YALA MOKO WAKH NIT KOU NEK SI LOU NEK REK LANOU KOYE ATÉ

Ousmane Tine
Guest
Ousmane Tine

XALISS WAROUL NGA DIAYE SA NGOR DI ANDAK GOOR DJIGENE

Mamadou Ndiaye
Guest
Mamadou Ndiaye

il ma desu

Ibrahim Touba
Guest
Ibrahim Touba

bilahi yen dolen dará xalis du dará bulen fate yalla.

Amadou Balde
Guest
Amadou Balde

Chekhouna mom sagnouko ndakh dioguei na macca lou yagoul

Gualaye Mvengue
Guest
Gualaye Mvengue

Dougen darra

ÈLZÖ KÄNTÈ
Guest
ÈLZÖ KÄNTÈ

Yalnalén yalla ar inchallah ☝😘

Mor Moup
Guest
Mor Moup

Diam thi yen bamou doye

Sokhna seye
Guest
Sokhna seye

Ndeysane gni khamougnou lou bone. Yène gni di commentaire ragal lène yalla dée bi dafa gaw. Nitt kou bakh dafay wakh louko worrr. Gni dagno amone lancement bene film bouy wadia guène

Gorguy Dièye
Guest
Gorguy Dièye

Sènègal da beuri goordjiguène trop t khamè wounioulène alale diaral nalène lounèk t adouna yagoul dara loukofidiar yala naniou yala yèreume soutoural niou

Modou Mbâye
Guest
Modou Mbâye

Yalna diamou yageu 😘

Serigne Mbacke
Guest
Serigne Mbacke

Da nioma rouss lo dh billahi

Ale Kebe
Guest
Ale Kebe

Wa lougnou Déff??

NHBI Seye
Guest
NHBI Seye

Ai way nank rek gni danou démonté pour la promotion d'un film rek com lounouy wakh la première du film bayilene wakh bou niaw

Fatoumata Fall
Guest
Fatoumata Fall

Ah gni dagno démone liguaye waye il faut attendre leurs versions ballagno wah

Khadim Diaw
Guest
Khadim Diaw

Billahi yeena ma bett xaliss ak aduna jaral leene ngueeni ferecanté li islam gueuneu bagn

Marietou Dabo
Guest
Marietou Dabo

Guisse guene lodoul deugue d'où yague gni Lou lenn yobou fofou khamou gnouko sakh daffa melni yalla mo wugni séné soutoura si ay nitte niou diogue make adji demam siare demm si Kaba bi warra am touguay bourafett niouy dem ba fofou nonou franchement je suis sidéré gni dougnou ay royou kay😟😟😟

THIATE RAKADIOU
Guest
THIATE RAKADIOU

Abonné len si THIATE RAKADIOU comédie